
PROFIL SOSIETE BI
Handan Dongchao Produit Hardware Co., Ltd. defarkatu jumtukaay la bu nekk ci Handan, diwaanu Hebei, ci Chine.
Kompani bi mingi tàmbali liggéey ci 2008, muy liggéey ci defar ak jaay ci bitim réew ay jumtukaayi usine yu melni vis forage, vis tapping, boulong, écrou, rondelle, rivet, batone fileté, ak sistemu fixation structurel.
Sunu produit yi ñu ngi leen di gëna jëfandikoo ci tabax, samp giñ defaree asiye, defar masin, ak defar ay montage ci usine yi.
KÀPPAAT BU DEFAR
Sunu usine amna ay ligne de production yu mat te lalu ci:
Boppu sedd ngir forme vis ak boulong
Roulage de fil pour filement précision
Sistemu forage ngir vis forage auto-
Traitement à chaleur pour contrôle de la force
Finishing surface ak anam yi ñuy raxasee
Emballage otomatik ngir yóbbu ci bitim réew
Sistemu defar bi dañu ko jagleel jumtukaayi fikseer yiñ miin ak ay leeral yuñ personaalise bu baax.
Weer wu nekk ñu ngi génne lu tollu ci 600 ton, liko aju ci xeetu produit bi ak ci anam yi ñu ko mëna defee.
Defar nanu ay jumtukaayi fikseer ci:
Acier à faible carbone
Acier carbone moyen
Acier inoxydable 304 / 316
Acier alloy ngir aplikaasioŋ yu am doole -
Standard yi ñuy jëfandikoo ngir defar ay mbir ñooy:
ISO norme internasional
DIN norme allemand
ASTM norme yu Amerique
Nataali kiliyaan yi ak leeral yi ci xarala yi

EXPERIENS EXPORT
Sunu fasteners ñu ngi koy yóbbu ci gox yu bari ci àdduna bi yépp.
Fimna nii danuy jox kiliyaan yi ci:
Etats Unis ak Canada ngir marse tabax ak séddale
Royaume-Uni ak réew yu Europe yu ci melni Allemagne, Italie, Espagne, ak Pologne
Réew yu moyen orient yu melni UAE, Arabie Saoudite, Qatar, ak Oman
Asie Sud-est boole ci Vietnam, Tayland, Malaysi ak Filipiin
Marse Afrique yu melni Egypt, Kenya, Nigeria, ak Afrique du Sud
Amerique du Sud boole ci Bresil, Sili, Peru ak Kolombi
Gox bu nekk dafay laaj xeetu emballage bu wuute, toppatoo surface bu nekk, ak sàmmonte ak sàrt yiñ tëral, te danu koy méngale ak bëgg-bëggu kiliyaan yi.

SISTEM BUY DOXAL KALITE
Danuy doxal sistem buñ yamale ngir saytu kalite, muy:
Saytu macceer bu bees biy dugg
Saytu anam yi ñuy defaree
Saytu dimension ak fiil
Test performance mekanik
Saytu surface bi
Saytu bu mujj balaa-yobbu
Mën nañu joxe done yiñ saytu ngir saytu lote su kiliyaan yi ko soxlaa.
Danuy joxe serwiis OEM ak ODM ci bëgg-bëggu kiliyaan yi.
Tànneefi personaalisasioŋ bokkuna ci:
Design produit
Dayo (diametre, guddaay, xeetu fiil)
Xeetu bopp bi ak sistemu dawal bi
Tanneef grade macceer
Traitement surface
Plaqué de zinc (divers couleurs)
Galvanisation à chaud
Oxyde bu ñuul
Revêtement Ruspert
Galvanisation mécanique


Emballage
Emballage industriel
Emballage boîte de détail
Imprime logo personalisé
etiketu kode bar ak sistemu skane
Ndimbalu ingenieur
Defar bu sukkandiko ci nataal-
Defar misaal balaa ñu koy defar lu bari
LOGISTIK AK KONTROL YI
Danuy jàppale ci wàllu logistik ci wàllu export:
Fret geej ngir yobbu mbir yu bari (chaine bu mag bi)
Fret aérien ngir komànd yu gaaw
Livraison bu gaaw ngir misaal ak limu tuuti
Danuy déggoo ak ekspeditër yi ngir mëna am këyitu export ak kalendriye yobbu bi.
Ngir laaj devis, binndal:
Specification produit wala nataal
jumtukaay yiñ soxla
Li war ci toppatoo surface bi
Bariwaayu komànd
Port bi ngay dem
Sunuy ekipu jaaykat yi ak xarala yi dina ñu tontu ci njëg yi ak firndelu mëna dem bi.

